Ñaan bu ñu tiitee ci nelaw walla nit wéet ba tiit

Reading settings
أَعُوذُ بِكَلِمَاتِ اللَّهِ التَّامَّةِ مِنْ غَضَبِهِ وَعِقَابِهِ، وَشَرِّ عِبَادِهِ، وَمِنْ هَمَزَاتِ الشَّيَاطِينِ وَأَنْ يَحْضُرُونِ.
Maa ngi sàkku kaaraange ci kàdduy Yàlla yu mat sëkk yi, ci meram ak mbugalam, ci loraange ay jaamam, ci xatti-xattiy seytaane yi ak ñu ñëw fi man.
Explanation & source

تخريج الذكر

ورد هذا الدعاء عند الفزع في النوم، وقال الترمذي: حسن غريب.