Ñaan yi ñuy ñaanal ku wopp bu ñu ko seetee

Reading settings
لَا بَأْسَ طَهُورٌ إِنْ شَاءَ اللَّهُ
Dara du ci la dal. Na la feebar bii sellal, bu soobee Yàlla.
Explanation & source

تخريج الذكر

تفصيل في اللفظ أو الثبوت

قول النبي ﷺ للمريض في صحيح البخاري.

مَا مِنْ عَبْدٍ مُسْلِمٍ يَعُودُ مَرِيضًا لَمْ يَحْضُرْ أَجَلُهُ فَيَقُولُ سَبْعَ مَرَّاتٍ : أَسْأَلُ اللَّهَ الْعَظِيمَ رَبَّ الْعَرْشِ الْعَظِيمِ أَنْ يَشْفِيَكَ إِلَّا عُوفِيَ.
Bépp jaamu Yàlla bu jullit bu seeti ku feebar bu àppam matagul, wax juróom-ñaari yoon «Maa ngi ñaan Yàlla mu màgg mi, Boroom ngàngune mu màgg mi, mu wéral la», kooku dina wér.
Explanation & source

تخريج الذكر

تفصيل في اللفظ أو الثبوت

دعاء المريض سبع مرات في سنن أبي داود.