Wax yu ñuy dëfal waa dëj
Reading settings
إِنَّ لِلَّهِ مَا أَخَذَ، وَلَهُ مَا أَعْطَى، وَكُلٌّ عِنْدَهُ بِأَجَلٍ مُسَمًّى، فَلْتَصْبِرْ وَلْتَحْتَسِبْ.
Li Yàlla jël Mooy Boroom, te li mu may it Mooy Boroom. Lépp am na àpp bu mu dogal. Kon muñal te séentu yool ci Yàlla.
Explanation & source
تخريج الذكر
بعث النبي ﷺ بهذا إلى ابنته حين أُصيب ولدها.