Ñaan gannaaw bu ñu suulee ki faatu
Reading settings
اللَّهُمَّ اغْفِرْ لَهُ، اللَّهُمَّ ثَبِّتْهُ.
Yaw Yàlla, jéggal ko. Yaw Yàlla, dëgëral ko.
Explanation & source
تخريج الذكر
صيغة للدعاء بالمغفرة والتثبيت؛ وقد أمر النبي ﷺ بسؤالهما للميت بعد الدفن.