Kàdduy tudd Yàlla bu ñuy délsi tukki
Reading settings
لَا إِلَهَ إِلَّا اللَّهُ وَحْدَهُ لَا شَرِيكَ لَهُ، لَهُ الْمُلْكُ، وَلَهُ الْحَمْدُ، وَهُوَ عَلَى كُلِّ شَيْءٍ قَدِيرٌ، آيِبُونَ تَائِبُونَ عَابِدُونَ سَاجِدُونَ لِرَبِّنَا حَامِدُونَ، صَدَقَ اللَّهُ وَعْدَهُ، وَنَصَرَ عَبْدَهُ، وَهَزَمَ الْأَحْزَابَ وَحْدَهُ.
Amul yàlla bu dul Yàlla, Moom rekk, amul àndandoo. Moom moo moom nguur gi te moom moo yelloo cant gi. Moom man na lépp. Nu ngi délsi, di tuub, di jaamu, di sujjóot te di sant sunu Boroom. Yàlla amal na digeem, wallu jaamam te daan mboolooy noon yi Moom rekk.
Explanation & source
تخريج الذكر
كان ﷺ يكبر ثلاثًا على كل شرف من الأرض عند رجوعه ثم يقول هذا الذكر.