Li ñuy wax bu ñuy tagg jullit
Reading settings
أَحْسَبُ فُلَانًا، وَاللَّهُ حَسِيبُهُ، وَلَا أُزَكِّي عَلَى اللَّهِ أَحَدًا، أَحْسَبُهُ كَذَا وَكَذَا إِنْ كَانَ يَعْلَمُ ذَلِكَ مِنْهُ.
Su ko xamee loolu ci moom, na wax «Dama yaakaar ne diw dafa mel nii, te Yàlla moo koy hesab. Du ma wax ci kanam Yàlla ne kenn sell na. Dama yaakaar ne dafa mel ni lii ak lee.»
Explanation & source
تخريج الذكر
إرشاد لمن اضطر إلى مدح أخيه، إذا علم ما يقوله عنه.