Li ñuy wax bu ñuy rendi mala walla dagg baatub giléem
Reading settings
بِسْمِ اللَّهِ، وَاللَّهُ أَكْبَرُ.
Ci turu Yàlla, te Yàlla moo gën a màgg.
Explanation & source
بِسْمِ اللَّهِ، اللَّهُمَّ تَقَبَّلْ مِنْ مُحَمَّدٍ وَآلِ مُحَمَّدٍ وَمِنْ أُمَّةِ مُحَمَّدٍ.
Ci turu Yàlla. Yaw Yàlla, nangul lii ci Muhammad, ci njabootu Muhammad ak ci ummatu Muhammad.