Yalla, maa ngi lay ñaan pastéef ci mbir mi, ak dogu ci topp njub, té ñaan la sababi sa yërmande ak dëggal sa jéggal, té ñaan ngërëm. Sa barke, ak xéewali jaamu La, ta maa ngi lay ñaan xol bu muur ak làmmiñ wu sell, ta maa ngi lay ñaan li gën ci li nga xam, maa ngi sàkku muslu ci yaw ci ay bon yu li nga xam. Te maa ngi ñaan njéggal ci li nga xam ndax yaw yaa xam lu nëbbu.
"رَبَّنَا ٱغۡفِرۡ لَنَا ذُنُوبَنَا وَإِسۡرَافَنَا فِيٓ أَمۡرِنَا وَثَبِّتۡ أَقۡدَامَنَا وَٱنصُرۡنَا عَلَى ٱلۡقَوۡمِ ٱلۡكَٰفِرِينَ١٤٧ ". [آلُ عِمْرَانَ - 147].
Sunu Boroom, jéggal nu sunuy bàkkaar ak sunuy jéggi-dayo ci sunuy mbir, dëgëral sunuy tànk, te dimbali nu ci kaw ñi weddi. [Al-Imran 3:147]
"أَنِّي مَسَّنِيَ ٱلضُّرُّ وَأَنتَ أَرۡحَمُ ٱلرَّٰحِمِينَ٨٣". [الْأَنْبِيَاءِ - 83].
Mettit dal na ma, te Yaw yaay gën ci ñiy yërëm. [Al-Anbiya 21:83]
Your daily Azkar, offline. Free.
Android · iPhone · iPad