Dream Interpretation
Qas,ui’
Islamic All
(See Five times prayers).
"رَبَّنَا ظَلَمۡنَآ أَنفُسَنَا وَإِن لَّمۡ تَغۡفِرۡ لَنَا وَتَرۡحَمۡنَا لَنَكُونَنَّ مِنَ ٱلۡخَٰسِرِينَ٢٣". [الْأَعْرَافِ - 23].
Sunu Boroom, tooñ nanu sunu bopp. Soo nu jéggalul te yërëmul nu, dinanu bokk ci ñi sànku. [Al-A‘raf 7:23]
Yalla, yaw mi xam li nëbbu ak li seede, mi sàkk asamaan yi ak suuf si, boroom lépp ak boroomam, maa ngi seede ni amul yàlla budul Yaw, maa ngi wut musal ci sama bopp ak ci soxor Seytaane ak fiir bimu jàpp.
"رَبَّنَآ ءَامَنَّا بِمَآ أَنزَلۡتَ وَٱتَّبَعۡنَا ٱلرَّسُولَ فَٱكۡتُبۡنَا مَعَ ٱلشَّٰهِدِينَ٥٣ ". [آلُ عِمْرَانَ - 53].
Sunu Boroom, gëm nanu li nga wàcce te topp nanu Yonent bi. Bind nu ci ñiy seede. [Al-Imran 3:53]
Your daily Azkar, offline. Free.
Android · iPhone · iPad