Dream Interpretation
Wax Taper
Miller
To blow them out, signals disappointing times, and sickness will forestall expected opportunities of meeting distinguished friends.
"رَبَّنَآ أَفۡرِغۡ عَلَيۡنَا صَبۡرٗا وَتَوَفَّنَا مُسۡلِمِينَ١٢٦ ". [الْأَعْرَافُ - 126].
Sunu Boroom, sottil ci nun muñ, te defal nu nu dee di ay jullit. [Al-A‘raaf: 126].
Yalla, maa ngi jébbalu ci yaw, ci yaw laa gëm, ci yaw laa wóolu, ci yaw laa tuub, ci yaw laay werante. Yalla, maa ngi wër sa ndam, amul beneen yàlla bu dul Yaw, Yaa ngi may réer. Yaay Aji Dund ji doo dee, te jinne yi ak nit ñi di dee.
"رَبَّنَا ظَلَمۡنَآ أَنفُسَنَا وَإِن لَّمۡ تَغۡفِرۡ لَنَا وَتَرۡحَمۡنَا لَنَكُونَنَّ مِنَ ٱلۡخَٰسِرِينَ٢٣". [الْأَعْرَافِ - 23].
Sunu Boroom, tooñ nanu sunu bopp. Soo nu jéggalul te yërëmul nu, dinanu bokk ci ñi sànku. [Al-A‘raf 7:23]
Your daily Azkar, offline. Free.
Android · iPhone · iPad