"أَنِّي مَسَّنِيَ ٱلضُّرُّ وَأَنتَ أَرۡحَمُ ٱلرَّٰحِمِينَ٨٣". [الْأَنْبِيَاءِ - 83].
Mettit dal na ma, te Yaw yaay gën ci ñiy yërëm. [Al-Anbiya 21:83]
"رَبَّنَآ ءَاتِنَا فِي ٱلدُّنۡيَا حَسَنَةٗ وَفِي ٱلۡأٓخِرَةِ حَسَنَةٗ وَقِنَا عَذَابَ ٱلنَّارِ٢٠١ ". [الْبَقَرَةُ - 201].
Sunu Boroom, may nu lu baax ci àddina ak ci àllaaxira, te aar nu ci mbugalu safara. [Al-Baqara 2:201]
اللَّهُمَّ أَحْيِنَا مُسْلِمِينَ ، وَتَوَفَّنَا مُسْلِمِينَ ، وَأَلْحِقْنَا بِالصَّالِحِينَ.
اللَّهُمَّ أَبْرِمْ لِهَذِهِ الْأُمَّةِ أَمْرَ رُشْدٍ ، يُعَزُّ فِيهِ أَهْلُ طَاعَتِكَ ، وَيُذَلُّ فِيهِ أَهْلُ مَعْصِيَتِكَ ، وَيُؤْمَرُ فِيهِ بِالْمَعْرُوفِ ، وَيُنْهَى فِيهِ عَنِ الْمُنْكَرِ.
اللَّهُمَّ صَلِّ وَسَلِّمْ وَبَارِكْ عَلَى عَبْدِكَ وَرَسُولِكَ مُحَمَّدٍ وَعَلَى آلِهِ وَصَحْبِهِ أَجْمَعِينَ.
Yalla, may nu dundu jullit, defal nu dee jullit, boole nu ak ñu jub ñi.
Yaw Yàlla, nanga may xeet wii mbirum njub, boo xam ne askan wi la déggal dinañu ko sargal, askan wi la déggadël di toroxal, yiw di leen digal. Te lu ñaaw araam na fa.
Yalla, Yalna sa barke ak sa jàmm nekk ci kaw sa jaam ak Yonent Mohamed ak ci njabootam ak ci àndadoom yépp.
Your daily Azkar, offline. Free.
Android · iPhone · iPad