Yalla, maa ngi lay ñaan pastéef ci mbir mi, ak dogu ci topp njub, té ñaan la sababi sa yërmande ak dëggal sa jéggal, té ñaan ngërëm. Sa barke, ak xéewali jaamu La, ta maa ngi lay ñaan xol bu muur ak làmmiñ wu sell, ta maa ngi lay ñaan li gën ci li nga xam, maa ngi sàkku muslu ci yaw ci ay bon yu li nga xam. Te maa ngi ñaan njéggal ci li nga xam ndax yaw yaa xam lu nëbbu.
"رَبَّنَا مَا خَلَقۡتَ هَٰذَا بَٰطِلٗا سُبۡحَٰنَكَ فَقِنَا عَذَابَ ٱلنَّارِ١٩١ رَبَّنَآ إِنَّكَ مَن تُدۡخِلِ ٱلنَّارَ فَقَدۡ أَخۡزَيۡتَهُۥۖ وَمَا لِلظَّٰلِمِينَ مِنۡ أَنصَارٖ١٩٢ رَّبَّنَآ إِنَّنَا سَمِعۡنَا مُنَادِيٗا يُنَادِي لِلۡإِيمَٰنِ أَنۡ ءَامِنُواْ بِرَبِّكُمۡ فَـَٔامَنَّاۚ رَبَّنَا فَٱغۡفِرۡ لَنَا ذُنُوبَنَا وَكَفِّرۡ عَنَّا سَيِّـَٔاتِنَا وَتَوَفَّنَا مَعَ ٱلۡأَبۡرَارِ١٩٣ رَبَّنَا وَءَاتِنَا مَا وَعَدتَّنَا عَلَىٰ رُسُلِكَ وَلَا تُخۡزِنَا يَوۡمَ ٱلۡقِيَٰمَةِۖ إِنَّكَ لَا تُخۡلِفُ ٱلۡمِيعَادَ١٩٤ ". [آلُ عِمْرَانَ - 191-194].
"Sunu Boroom, yaa ngi sos lii ci amul benn njariñ. Yalna ndam ci yaw, kon musal nu ci fitnaal safara. Sunu Boroom. Dëgg la, képp ku nga dugal ci safara, yaa ko rusloo. Te defkatu ñaawtéef yi amul kenn ku leen di jàppale. Sunu Boroom. Dëgg la, nu dégg wootekat buy woo ngëm: Gëm sunu Boroom, nu gëm sunu Boroom. ngir nun sunuy jëf yu bon, te nu dee ak moom, sunu Boroom, nga jox nu li nga nu digoon jaaraleko ci say ndaw, te bul nu rusloo ci bis biy indig àdduna. [Al Imran - 191-194].
"رَّبِّ ٱغۡفِرۡ لِي وَلِوَٰلِدَيَّ وَلِمَن دَخَلَ بَيۡتِيَ مُؤۡمِنٗا وَلِلۡمُؤۡمِنِينَ وَٱلۡمُؤۡمِنَٰتِۖ وَلَا تَزِدِ ٱلظَّٰلِمِينَ إِلَّا تَبَارَۢا٢٨". [نُوحٍ - 28].
"رَبِّ إِنِّيٓ أَعُوذُ بِكَ أَنۡ أَسۡـَٔلَكَ مَا لَيۡسَ لِي بِهِۦ عِلۡمٞۖ وَإِلَّا تَغۡفِرۡ لِي وَتَرۡحَمۡنِيٓ أَكُن مِّنَ ٱلۡخَٰسِرِينَ٤٧". [هُودٍ - 47].
"رَّبِّ أَنزِلۡنِي مُنزَلٗا مُّبَارَكٗا وَأَنتَ خَيۡرُ ٱلۡمُنزِلِينَ٢٩". [الْمُؤْمِنُونَ - 29].
Sama Boroom, jéggal ma ak samay waajur, ak ku dugg sama kër di gëm, ak gëmkat yu góor ak yu jigéen; te bul yokk ñiy tooñ lu dul yàqute. [Nuh 71:28]
Sama Boroom, maa ngi la di ñaan nga aar ma ci laaj la lu ma xamul. Soo ma jéggalul te yërëmul ma, dinaa bokk ci ñi sànku. [Hud 11:47]
Sama Boroom, wàcceel ma ci bérab bu am barke, te Yaw yaa gën ci ñiy wàcceel. [Al-Mu’minun 23:29]
Your daily Azkar, offline. Free.
Android · iPhone · iPad