"رَبَّنَا ظَلَمۡنَآ أَنفُسَنَا وَإِن لَّمۡ تَغۡفِرۡ لَنَا وَتَرۡحَمۡنَا لَنَكُونَنَّ مِنَ ٱلۡخَٰسِرِينَ٢٣". [الْأَعْرَافِ - 23].
Sunu Boroom, tooñ nanu sunu bopp. Soo nu jéggalul te yërëmul nu, dinanu bokk ci ñi sànku. [Al-A‘raf 7:23]
"رَبَّنَا لَا تُزِغۡ قُلُوبَنَا بَعۡدَ إِذۡ هَدَيۡتَنَا وَهَبۡ لَنَا مِن لَّدُنكَ رَحۡمَةًۚ إِنَّكَ أَنتَ ٱلۡوَهَّابُ٨ ". [آلُ عِمْرَانَ - 8].
Sunu Boroom, bul jengal sunuy xol gannaaw ba nga nu gindee. May nu yërmaande ju jóge ci Yaw; Yaw yaay Mayewaakoon bi. [Al-Imran 3:8]
Yalla, yaw mi xam li nëbbu ak li seede, mi sàkk asamaan yi ak suuf si, boroom lépp ak boroomam, maa ngi seede ni amul yàlla budul Yaw, maa ngi wut musal ci sama bopp ak ci soxor Seytaane ak fiir bimu jàpp.
Your daily Azkar, offline. Free.
Android · iPhone · iPad