Yalla, yaw mi xam li nëbbu ak li seede, mi sàkk asamaan yi ak suuf si, boroom lépp ak boroomam, maa ngi seede ni amul yàlla budul Yaw, maa ngi wut musal ci sama bopp ak ci soxor Seytaane ak fiir bimu jàpp.
"رَبِّ هَبۡ لِي مِن لَّدُنكَ ذُرِّيَّةٗ طَيِّبَةًۖ إِنَّكَ سَمِيعُ ٱلدُّعَآءِ٣٨ ". [آلُ عِمْرَانَ - 38].
Sama Boroom, may ma ci sa ngëneel ay doom yu baax. Yaw dégg nga ñaan. [Al-Imran 3:38]
"إِنِّي تَوَكَّلۡتُ عَلَى ٱللَّهِ رَبِّي وَرَبِّكُمۚ مَّا مِن دَآبَّةٍ إِلَّا هُوَ ءَاخِذُۢ بِنَاصِيَتِهَآۚ إِنَّ رَبِّي عَلَىٰ صِرَٰطٖ مُّسۡتَقِيمٖ٥٦". [هُودٍ - 56].
“Maa ngi wéeru ci Yàlla, sama Boroom ak seen Boroom. Amul mbindéef luy dund lu dul mu jàpp kawam. Sama Boroom a ngi ci yoon wu jub.” [Hud - 56].
Your daily Azkar, offline. Free.
Android · iPhone · iPad